1 Corinthians 3:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci li jëm ci fondamaa bi, kenn mënu fee tëral beneen bu dul bi fi xas a taxaw, muy Yeesu Kirist.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Geneen kenu moom maneesu koo lal, xanaa gi xasa lale, te mooy Yeesu Almasi.