1 Corinthians 3:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ku yàq kër Yàlla gi, Yàlla dina la yàq, ndaxte kër Yàlla gi dafa sell, te yéenay kër googu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ku yàq kër Yàlla nag, kooku Yàlla dina ko yàq, ndax kër Yàlla dafa sell, te mooy li ngeen doon.