bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Corinthians 3:2
1 Corinthians 3:2 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Nàmpaloon naa leen, waaye joxuma leen dugub, ndaxte àttanuleen ko woon, te ba léegi sax àttanuleen ko
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Meew laa leen jota nàndal, waaye leeluma leen dugub, ndax àttanuleen ko woon, te ba léegi sax àttanuleen ko,