1 Corinthians 3:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag bu kenn tiitaru ndax nit ñi, ndaxte yéena moom lépp,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag bu kenn puukarewoo ay nit, ndax lépp, yeena ko moom,