1 Corinthians 3:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu kenn yéglee ne: «Man ci Pool laa bokk,» keneen ne: «Man ci Apolos,» ndax jëfewuleen ni niti àddina rekk?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu kenn naan: «Man ci Póol laa bokk,» keneen naa: «Man nag Apolos,» ndax kon dungeen niti àddinay kese?