bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Corinthians 4:13
1 Corinthians 4:13 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ku nu ñaawal, nu tontu la tont lu rafet. Fi mu ne noo mujj di mbalitu àddina, di ñu ñàkk njariñ ci lépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nu ngi nuy baatal, nun nuy wax lu rafet ci nit ñi, nu mujj mel ni mbalitu àddina, di mbuubitu ñépp ba fii nu tollu.