1 Corinthians 4:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su ngeen amee junniy njiit yu leen di sàmm ci Kirist, ba tey benn baay rekk ngeen am, ndaxte maa leen yégal xebaar bu baax bi, ba jur leen ci Kirist.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ngeen amoon fukki junniy njiit yu leen di sàmm ci yoonu Almasi it, du tax ngeen am lu wees benn baay, te man maa leen àgge xibaaru jàmm bi, ba tax ma di seen baay ci yoonu Almasi Yeesu.