1 Corinthians 4:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte yaw, ku la def, ba nga gën a màgg ñi ci des? Loo am lu ñu la mayul? Te bu ñu la ko mayee, lu tax nga di ci tiitaru, mel ni mayuñu la ko?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ana ku la def nga gën ci nit ñi? Ana loo am lu ñu la joxul? Te ndegam dees la koo jox, ana loo koy puukarewoo, mbete lees la joxul?