1 Corinthians 4:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yéen suur ngeen xaat! Woomle ngeen xaat! Tàmbali ngeen di nguuru te agseegunu! Céy ni ma bëgge, ngeen di nguuru, ba nu man a bokk ak yéen di nguuru!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeen daal suur ngeen xaat! Woomle ngeen xaat! Yeena ngi tàmbalee nguuru, te xaaruleen nu ci sax! Céy su ngeen doon nguuru léegi, ba nun itam nu mana nguuroondoo ak yeen!