1 Corinthians 4:9 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Xalaat naa ne, nun ndawi Kirist yi, Yàlla def na ba nu mel ni nit ñu ñu jàppe ci xare te mujj ci sàppe yi, ñu dogal seen dee, nuy ceetaanum mbindeef yépp, muy nit muy malaaka.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndaxte damaa foog ne, nun ndawi Almasi, Yàllaa nu fésal ca sàppeb gannaaw ba, mbete nit ñu ñu teg àtteb dee, ngir nu doon ceetaanum àddina wërngal këpp, malaaka ak nit.