1 Corinthians 5:10 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bëgguma ci woon a limaale waa àddina, maanaam njaalookat yi, nay yi, njublaŋ yi ak xërëmkat yi. Su ngeen séqul ak ñooñu dara, kon fàww ngeen génn àddina.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye moos fokati àddina sii taxul woon may wax, mbaa bëgge yi ak ŋàppaaral yi ak bokkaalekat yi, nde kon fàww ngeen génn àddina.