bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Corinthians 5:12
1 Corinthians 5:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndax man maa war a àtte ñi bokkul ci mbooloom ñi gëm Kirist? Déedéet! Waaye ñi bokk ci seen mbooloo yéena leen war a àtte.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ana sax luy sama yoon ci waa biti ba di leen àtte? Su dee waa biir mbooloom gëmkat ñi nag, yeena leen wara àtte.