1 Corinthians 5:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ni ma leen ko man a misaale, jëleleen fi bépp lawiir bu yàgg, ngir ngeen sell ni tooyal bu bees bu amul lawiir, ndax nekk ngeen ko ba noppi. Ndaxte Kirist deeyal na nu ca bant ba, mel ni mbote mu ñuy rendi, jébbal ko Yàlla ca màggalu bésu Jéggi ba.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Setal-leen seen bopp boog, génneleen lawiir bu yàgg bi ci seen biir, ba mana doon tooyal bu bees bu mucc lawiir, nde doon ngeen ko ba noppi, ndax Almasi, sunu gàttub bésub Mucc biy sunub sarax, rendilees na nu ko.