1 Corinthians 5:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nanu màggal sunu Màggal, waxuma ak lawiir bu màggat biy misaal kiñaan ak lu bon, waaye ak mburu mu amul lawiir, maanaam ci xol bu laab ak ci dëgg.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag, nanu màggal sunu bésub Mucc te bañ koo màggale lawiir bu yàgg, mbaa lawiiru yàqute akug mbon, xanaa nu màggale ko mburu mu mucc lawiir, mburum xol bu set te dëggu.