bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Corinthians 6:15
1 Corinthians 6:15 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Xanaa xamuleen ne, seen yaram ñooy céri Kirist? Ndax kon damay jël céri Kirist, def ko céri jigéeni moykat? Mukk!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xanaa xamuleen ne, seen yaram mooy céri Almasi? Waaw, ndax damay jël céri Almasi, def ko céri gànc bu jigéen? Yàlla tere!