1 Corinthians 6:16 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Xanaa xamuleen ne, kuy ànd ak jigéen juy moy dafay booloo ak moom, nekk benn? Ndaxte Mbind mi nee na: «Ñoom ñaar dinañu doon benn.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xanaa xamuleen ne, kuy taqoo ak ab gànc bu jigéen, mook moom, jenn jëmm lañuy doon? Ndaxte noonu lañu waxe ne: «Ñoom ñaar ay mujj di wenn suux doŋŋ.»