1 Corinthians 6:18 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Dawleen njaaloo! Bépp bàkkaar bu nit man a def, du laal yaramam, waaye nag kuy njaaloo, dafay bàkkaar, di lor yaramam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dawleen powum séy! Mboolem bàkkaar bu nit mana def, bàkkaar ba du jote dara ak yaramam, waaye fokat bi, yaramu boppam lay lore bàkkaaru powam.