1 Corinthians 7:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nanu jàll nag léegi ci laaj, yi ngeen ma doon bind, ci bañ a ànd ak jigéen, ndax lu baax la ci góor.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sama tont ci mbir mi ngeen ma bind nag, moo di lu baax la ci góor, mu mucc ci jigéen.