1 Corinthians 7:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ñi ci des nag, lii laa leen di wax --Boroom bi waxu ko woon — su nit ku gëm Kirist amee jabar ju gëmul, te mu nangoo séy ak moom, waru koo fase.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñi ci des nag, li ma xalaat te du Boroom bee ko wax, maa ko waxal sama bopp, moo di: ab gëmkatub Almasi, bu amee jabar ju gëmul, te teewul mu nangu koo séyal ba tey, bumu ko fase.