1 Corinthians 7:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye nag, su fekkee ki gëmul bëgg na dem, na dem. Ci wàll googu nag, ki gëm Kirist, muy jëkkër ji walla jabar ji, amul benn tënk, ndaxte Yàlla moo leen woo ngir ngeen dund ci jàmm.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndegam nag ki gëmul daa bëgga dem, na dem. Su demee noonu, mbokkum gëmkat bu góor bi, mbaa ku jigéen ki amatul benn gàllankoor, waaye ci jàmm la leen Yàlla woo.