1 Corinthians 7:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ku nekk nag na dund, ni ko ko Boroom bi jagleele, mu mengoo ak ni mu meloon, bi ko Yàlla wooyee. Moom laay tëral ci mboolooy ñi gëm yépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lu ko moy nag, ku ci nekk, cér ba la Boroom bi séddoon, noonee nga nekke woon ba la Yàlla di woo, nanga ko wéye. Loolu laa santaane ci mboolooy gëmkat ñépp.