1 Corinthians 7:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndax jaam nga woon, bi la Yàlla wooyee? Na ci sa xel dal. Waaye soo amee bunt, ba yiwiku, nanga ci jaar.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax ab jaam nga woon, ba ñu lay woo? Amul solo. Waaye soo manee yiwiku, yiwikul.