1 Corinthians 7:26 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu nu seetee tiis wii fi teew nag, defe naa ne li baax ci nit, moo di mu sax ci li mu nekk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lii mooy li ma foog ne mooy li baax, ndax njàqarey jamonoy tey. Li baax ci nit ki daal mooy mu wéye li muy dund tey.