1 Corinthians 7:27 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndax takk nga jabar? Bul wut a tàggoo ak moom. Ndax takkuloo jabar? Bul wut jabar.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dangaa am jabar? Bul sàkku pase. Am amuloo jabar? Kon bul sàkku jabar.