1 Corinthians 7:29 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Lii laa bëgg a wax, bokk yi: diir bu gàtt rekk a fi des. Lu weesu tey, na góor ñi am jabar di def, ni bu ñu ko amul woon;
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li may wax, bokk yi, moo di, li des yàggatul. Kon nag bés niki tey, na ñi am jabar mel ni bu ñu ko amul woon;