1 Corinthians 7:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Jëkkër war na def warugaru jëkkër ci jabaram; jabar it def warugaru jabar ci jëkkëram.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jëkkër ji war naa def warugaru jëkkër ci jabaram; naka noonu it, jabar ji war naa def warugaru jabar ci jëkkëram.