1 Corinthians 7:34 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
te noonu dafay daldi bare soxla. Te jigéen ju séyul, walla janq, dafay bàyyi xel ci mbiri Boroom bi — bëgg koo jox yaramam ak xelam. Waaye jigéen ji séy dafay bàyyi xel ci mbiri àddina, ak nu mu man a neexe jëkkëram.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
mu daldi ŋarale. Jigéen ju séyul, mbaa ab janq, mbiri Boroom bi lay xalaat, di namma sellal yaramam akum xelam. Waaye kiy séy, mbiri àddina lay xalaat, ak nu muy dabe bànneexu jëkkëram.