1 Corinthians 7:35 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Seen njariñ a tax ma wax lii, du ngir teg leen yen bu ngeen àttanul, waaye ngeen man a jàppandil Boroom bi ci njaamu gu rafet gu àndul ak genn njaaxle.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lii nag, seen njariñ a ma ko taxa wax, nammuma leen koo tege ab gàllankoor, li ma ci namm mooy ngeen di def li jekk, te taxawal temm Boroom bi, taxawaay bu leen benn xalaatu àddina dul féle.