1 Corinthians 7:36 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nanu jàll nag ci mbiri kiy takk ngoro te amul pasteefu takk ndaw si. Su fekkee ne waxambaane wi xalaat na ne, jëfewul nu jekk ak janq bi, fekk muy wees ag ndawam, te mu xalaat ne dafa koo war a takk, kon na ko takk, ni mu ko bëgge; deful bàkkaar.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye su amee ku jàpp ne jëfewul nu jekk, ak janq bu mu digool ab séy, te janq ba jëm mag, ba mu xalaat ne takk ko rekk moo ci war, na matal yéeneem, takk ko. Su defee noonu, bàkkaarul.