1 Corinthians 7:38 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ku takk as ndawam def na lu baax, rawatina nag ku takkul.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon ki jël ab janqam bu mu digool ab séy, def na lu baax, waaye ki jëlul ab janqam moo def li gën.