1 Corinthians 7:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Jigéen ji amul sañ-sañ ci yaramam moom kenn; jëkkëram moo ko moom. Niki noonu it jëkkër ji amul sañ-sañ ci yaramam; jabaram moo ko moom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jigéen ji moomul yaramam, moom doŋŋ, waaye jëkkër ji it am na ci sañ-sañ. Naka noonu it, jëkkër ji moomul yaramam, moom doŋŋ, waaye jabar ji it am na ci sañ-sañ.