bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Corinthians 7:40
1 Corinthians 7:40 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Moona nag dina gën a bég, bu toogee noonu rekk. Loolu mooy sama xalaat, te defe naa ne, man it am naa Xelum Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Doon na gëna bég nag, su toogoon, baña séyaat, ci sama xalaat, te man it defe naa ne Noowug Yàlla mu ngi ci man.