1 Corinthians 7:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Li ma leen di wax fii du ndigal, waaye dama leen di xamal li ñu leen may, ngeen def ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu ma leen wax nag mooy li leen yoon may, waaye du ndigal.