1 Corinthians 7:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Lii laay yégal ñi séyul ak it ñi seen jëkkër dee: baax na ci yéen, su fekkee dangeen a toog rekk ni man, bañ a séy.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li may wax gëmkat ñi séqul ak kenn ab séy, ak ñi seen jëkkër faatu daal moo di, su ñu wéyee toog noonu ni man mii, lu baax la ci ñoom.