1 Corinthians 8:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Léegi nag, ci li jëm ci yàpp wi ñu jébbal xërëm yi: nun ñépp am nanu xam-xam, loolu dëgg la. Xam-xam day tax ba nit yég boppam, waaye mbëggeel day yékkati ngëm.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su dee wàllu ñam wu ñu sarxal ay tuur, dëgg la, nun ñépp am nanu xam-xam ci moomu mbir. Xam-xam nag day tax nit a réy-réylu, waaye cofeel day yokke.