1 Corinthians 8:13 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Kon bu sama mbokk sóoboo ci bàkkaar ndax ñam wi ma lekk, dootuma lekk mukk yàpp, ngir bañ a sóob ci bàkkaar sama mbokk mi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax, su dee aw ñam wu ma lekk mooy tax ma bàkkaarloo sama mbokkum gëmkat, dootuma lekk mukk aw yàpp ci àddina, ngir baña bàkkaarloo sama mbokkum gëmkat.