1 Corinthians 8:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag ci li jëm ci lekk yàpp wu ñu jébbal xërëm yi, xam nanu ne, xërëm du dara ci àddina te xam nanu itam ne, Yàlla kenn rekk la.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon su dee wàllu ñam wu ñu sarxal ay tuur, xam nanu ne ay tuur du dara ci àddina, te Yàlla kenn la.