1 Corinthians 9:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndax awma ndogal ci li may def? Ndax duma ndawul Kirist? Ndax gisuma Yeesu sunu Boroom? Xanaa du yéena soqikoo ci liggéey, bi ma Boroom bi sant?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Du maa moom sama bopp? Am du man, ndawal Almasi laa? Xanaa gisuma Yeesu sunu Boroom? Xanaa du sama liggéey ci Sang bi, moo di yeen ci seen bopp?