1 Corinthians 9:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Walla boog xanaa nun noo moom wax jooju? Waaw, noo tax ñu bind loolu. Noonu kuy bey war na am yaakaar, te kuy bojj di yaakaar a jot wàllam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Am du noo tax muy wax? Nun kay noo tax ñu bind loolu, ndax kuy bey, sañ cee yaakaar, kuy bojj it, sañ cee yaakaar wàllam.