1 Corinthians 9:15 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye man jariñoowuma benn ci sañ-sañ yooyu, te binduma yëf yooyu, ngir ngeen di ma defal yu ni mel. Dee sax moo ma ko gënal — kenn du jële ci man mbir moomu may kañoo!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye man jariñoowuma lenn ci sañ-sañ yooyu, te binduma lii it ngir defalees ma noonu. Xanaa dee sax a may gënal— boobu sañ-sañu kañu daal, kenn du ma ko yàqal!