bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Corinthians 9:16
1 Corinthians 9:16 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Su may yégle xebaar bu baax bi, mënuma cee kañu. Sas la, wu ñu ma sas. Dinaa torox, su ma yéglewul xebaar bu baax bi!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yégle xibaaru jàmm bi moom, du lu may kañoo. Wartéef la wu ñu ma sas, te ngalla man, su ma yéglewul xibaaru jàmm bi!