1 Corinthians 9:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag lan mooy sama yool? Xanaa di yégle xebaar bu baax bi ci dara, te bañ a jariñoo sañ-sañ boobu ma ci yelloo.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
kon ana lu ciy sama peyoor? Xanaa ma man di yégle xibaaru jàmm bi ci dara, ba duma jariñoo sañ-sañu dunde xibaaru jàmm bi may yégle.