1 Corinthians 9:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gor laa te kenn moomu ma; teewul def naa sama bopp jaamu ñépp, ngir man a gindi nit ñu bare ci Kirist.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te itam as gor laa, kenn moomu ma; teewul jaamu ñépp laa def sama bopp, ngir gëna iril Sang bi aw nit.