bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Corinthians 9:2
1 Corinthians 9:2 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Su ma ñenn ñi tegul ndaw, moom laa ci yéen, ndaxte yéenay firnde jiy wone ne, ndawul Boroom bi dëgg laa.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndegam ci ñeneen, man duma ndawal Almasi, xanaa ci yeen boog, moom laa, ndax liy firndeel sama sasu ndaw ci Sang bi, yeen la.