1 Corinthians 9:21 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ci biir ñi nekkul ci yoonu Musaa, faalewuma woon yoon wi, ngir gindi leen; waxuma ne, ànduma ak yoonu Yàlla, waaye topp naa yoon ci sama bokk ak Kirist.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maak ñi amul yoonu Musaa, damaa mel ni ku amul yoonu Musaa, ngir iri leen, doonte ñàkkuma yoonu Yàlla, gannaaw maa ngi ci yoonu Almasi.