bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Corinthians 9:23
1 Corinthians 9:23 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Damaa def loolu lépp ndax xebaar bu baax bi, ngir man it ma am wàll ci barkeem.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu lépp def naa ko ndax xibaaru jàmm bi, ngir am ci wàll.