1 Corinthians 9:26 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Man nag noonu laay dawe, te duma dawantu. Noonu laay bëree, waaye duma def ni nit kuy dóor ci jaww ji.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Man nag noonu laay dawe, waaye samaw xél ñàkkul ab jëmu. Noonu laay këmëxee it, waaye dóoruma ci jaww ji.