bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Corinthians 9:27
1 Corinthians 9:27 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye damay noot sama yaram, ba moom ko, ngir ragal a yégal ñi ci des xebaar bu baax bi, ba noppi Yàlla xañ ma ndam li.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Damay yar sama yaram yar bu metti kay, ba moom ko, ndax ëllëg ñu bañ maa doyadal, gannaaw bu ma xamalee ñeneen kàddu gi ba noppi.