1 John 1:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Dund feeñ na, te gis nanu ko; te moom lanuy seedeel, di leen yégal dund gu dul jeex, googu nekkoon ci wetu Yàlla Baay bi te feeñu nu.