1 John 1:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Xebaar bi nu dégg ci Yeesu Kirist, di leen ko yégal, mooy lii: Yàlla Leer la, te genn lëndëm nekkul ci moom.